IdolesSaison 5

IdolesSaison 5

27 épisodes

Idoles — Saison 5
HD1080p
LIVE
0:00 / --:--

Idoles — Saison 5

Télécharger

Téléchargement direct et sécurisé

E01

"Mbejjum kanam borom’ma koy fajjal boppam" (La victime d’une gifle est plus en mesure de se faire justice)

26/08/2018
E02

"Lu la bett mën la" (Tout ce qui te prend au dépourvu est plus fort que toi)

29/08/2018
E03

"Benn lox du tàccu" (Pour applaudir, il faut deux mains)

02/09/2018
E04

"Mën ko, defoo ko, tëlée ko gën" (Il faut mieux être incapable plutôt que d’être capable et de ne rien faire)

05/09/2018
E05

"Wax soxu fetal la, su rëccee dabu ko wees" (La parole, c’est une charge de fusil ; si elle échappe, on ne peut plus la rattraper)

09/09/2018
E06

"Yàgg ay wone légétub taat" (C’est avec le temps qu’on découvre une cicatrice aux fesses)

12/09/2018
E07

"Guy dana juri dég" Il arrive qu’un baobab ait des épines)

16/09/2018
E08

"Kooyi bukki du njoowaanug tef." (Le pénis de la hyène n’est pas une balançoire pour un chevreau.)

19/09/2018
E09

"Gulba am na beneen liggééy bu dul nas i pusó." (L’aveugle a un autre travail que d’enfiler des aiguilles)

23/09/2018
E10

"Goor buy jooy dafa wara lakkatu." (Un homme qui pleure doit se cacher.)

26/09/2018
E11

"Sàmmkat sañ naa maye meew, wànte sañula mayew sëllu." (Un berger a le droit d’offrir du lait, mais il n’a pas le droit d’offrir un veau)

30/09/2018
E12

"Bu la sa taar bi taxa bew, ndax laago du wess." (Il ne faut pas être fier de sa beauté car une infirmité peut toujours arriver)

03/10/2018
E13

"Picc mu masula naaw, su naawee firim rééw" (L’oiseau qui n’a jamais volé, le jour où il vole, fait le tour du pays)

07/10/2018
E14

"Waxtaab ñam la, ku ko teewe ca nga." (La conversation, c’est comme un repas, celui qui se trouve là y participe)

10/10/2018
E15

"Ñu yemul lor, duñu mëquandoo sunguf" (Ceux qui n'ont pas la même quantité de salive ne doivent pas manger de la farine ensemble)

14/10/2018
E16

"Nen du bëreek doj." (Un œuf ne lutte pas avec un caillou)

17/10/2018
E17

"Lu la mar maul, màtt du la komay." (Ce que lécher ne peut pas donner, mordre ne le donne pas)

21/10/2018
E18

"Benn loxo du tàccu." (Une seule main n’applaudit pas)

24/10/2018
E19

"Ku xamul "Suur naa", dangay téye ca loxo ba." (A celui qui ne sait pas dire « Je suis rassasié », tu retiens sa main).

31/10/2018
E20

"Làmb aw taat, boroom a ca gën." (Pour toucher des fesses, il vaut mieux en être le propriétaire)

04/11/2018
E21

"Aduna weru koor la faw diant sow nga do nga wagni beuss" (La vie est comme le mois du Ramadan : tant que le soleil ne s'est pas couché, on ne doit pas compter les jours)

07/11/2018
E22

"Ñaq du feeñ ci taw." (La sueur ne se voit pas sous la pluie)

11/11/2018
E23

"Ngaram ngaram baayi ngaramoon na baa mousy beugua ngaram." (Celui qui dit qu'il a faim et ne mange pas quand on lui donne à manger, a déjà mangé ou va manger après)

14/11/2018
E24

"Dëkk gaar ba taxula barey gan.' (Habiter à la gare, ce n’est pas une raison pour avoir beaucoup d’étrangers chez soi.)

18/11/2018
E25

"Doom su tékkiwul doomiy wàjuram késsé la, wayé su tékké di doomi nieup." (Si l’enfant ne réussit pas, il n’est le fils que de ses parents, mais s’il réussit, alors c’est le fils de tout le monde)

21/11/2018
E26

"Geenub giléém sànguluw taat te dàqul i weñ." (La queue du chameau ne peut ni recouvrir ses fesses, ni chasser les mouches) (1)

25/11/2018
E27

"Geenub giléém sànguluw taat te dàqul i weñ." (La queue du chameau ne peut ni recouvrir ses fesses, ni chasser les mouches) (2)

28/11/2018